« Les personnages et les situations de ce récit étant purement fictifs, toute ressemblance avec des personnes ou des situations existantes ou ayant existé ne saurait être que fortuite. Enfin presque…….
Driiiinnng! B M: Allo ?
OS: As’salaaaaamu ´Aleykum!
BM: oui, maalekum salam… Bonjour… OS: Grand, noo def? Dewenati !
BM: euh…. qui est à l’appareil là?… BM grand, mane la boy Oussou…
— Oussou ? … bane Oussou…?
-: Khamé womeu ? Mane la PROS, grand… MS: Prosss… Prosper bane?
OS: Non. Sonko, grand… mane leu Ousmane … (silence)
Légui… lane leu ?
‘Jamm rek, grand… Xanaa di la nemmeeku rek…
écoute, boy, mbalaguou suba téel yoyou, tu peux garder ça pour toi. Wakhal li ngay wakhe. J’ai à faire, moi !
Non grand. Boul couper yowwit…Jamm rek laay dox (rires dans la voix)… Mais kontaan naa ci yow beurki demb nak… .Franchemaaa…
Waaw ok, loolu rek la woon?
Grand nakk, bine Danga , d tàng trope
!…ha ha ha…! Ana Sokhna Si ?
Guissoumako. : Loy retane ni ? Ah je vois. Mais lii, dé fou ma ko pour yow, deh! Naay leer !
Xam naa loolu…Grand ! Ha ha ha ha… mais nak… Xanaa leegi war nga meune bayyi sama gars yi ngay diape rek!..
Mais, boy, ñoonu jàppou ma leen, justice bi leu la… Tony ak Iso leu… mais bon, on verra…Di naa waxtaan ak ñoom…
Di nga si boleh wa Cité Keur Gorgui aussi ?
…. Mais Sama rakk, nee naa la du Au revoir, Boy…
ha ha, grand bi daaaal…. Waa mais kone da ngay dem nii…? Doo bokk? Euy kou ma ko ..!
-waaw, gis nga deh!… Mais sa mbalag yi du jall… Yow moom doo bokk… Pas question…!
‘ mais grand….mais ma laaj la… Comme da ngay dem, lu takhe doo teggi sa tànk, nakk ?
Boy… Ouz… xam naa la… Yow da nga « sadique »… Boo fi gagner, kenn dootul am jàmm… Xam nga li may wax…Ba parer, yone yamoul si ..Bon, ma bayi leu. Nioungui maay khaar ndekki.
Ha ha ha… mais grand, mbir yi faww ñu saytu ko nak… han? En attendant, dina leu yonnee beignet-dugub…ha ha ha…
Di naa la rappeler nak… Ñu wax si you bari comme legui, kane mooy nekk candidat Benno. Wala? .
Bip. Bip. Bip. Bip. Votre correspondant ne peut plus être joint. Veuillez rappeler ultérieurement.
Sébé